Sama GÃ mmu lyrics
by Youssou N’Dour
Nanga def yaw sama gà mmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko à bb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Nanga def, na nga def gà mmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tà mbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko à bb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Yor xaalis mënui tee me moom la
Nanga def, na nga def gà mmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko à bb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def, na nga def gà mmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tà mbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko à bb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gà mmu daal sama doomu nday nga
E e e gà mmu daal suma xarit nga
E e e gà mmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gà mmu daal suma xarit nga
E e e gà mmu daal man sama doomu nday nga
E e e gà mmu daal man suma xarit nga
E e e gà mmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu foo ko
Teeyai teey teey
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gà mmu daal sama doomu nday nga
E e e gà mmu daal suma xarit nga
E e e gà mmu daal suma askan